Language: [wol] | Wolof | Wolof |
Dialect: | Regional Wolof | |
Title: | Téereb Injiil | Wolof NT 2010 |
Abbreviation: | ID: WOLINJ or wol2010 | |
Copyright © 2010 La Mission Baptiste du Sénégal |
The New Testament in Wolof, 2010 version.
Le Nouveau Testament en langue Wolof, revision de 2010
Waaye jëkkleena wut nguuram ak njubteem, te loolu lépp dina leen ko ci dollil.
—Matthew 6:33
Ndaxte Yàlla dafa bëgg àddina, ba joxe jenn Doomam ji mu am kepp, ngir képp ku ko gëm am dund gu dul jeex te doo sànku mukk.
—John 3:16
Xam nanu itam ne ñi bëgg Yàlla, maanaam ñi Yàlla woo ci boppam te boole leen ci li mu tëral, Yàlla dina joo loxoom ci lépp lu xew ci seen dund, ngir jural leen lu baax.
—Romans 8:28
copyright © 2010 La Mission Baptiste du Sénégal
Language: Wolof
Dialect: Regional Wolof
Translation by: La MBS
For full copyright statement, see http://sng.al/copyright
This translation is made available to you under the terms of the Creative Commons Attribution-Noncommercial-No Derivatives license 4.0.
You may share and redistribute this Bible translation or extracts from it in any format, provided that:
Pictures included with Scriptures and other documents on this site are licensed just for use with those Scriptures and documents. For other uses, please contact the respective copyright owners.
2020-07-09
Last updated 2020-07-09