eBible.orgTranslationsCountries/Territories
eBible.orgTranslationsTerritories

 

Kàddug Yàlla

Wolof Bible (MBS)

Language: [wol]WolofWolof
Title:Kàddug YàllaWolof Bible (MBS)
Abbreviation:ID: WOLMBS or wolmbs
Copyright © 2025 La Mission Baptiste du Sénégal
FormatLink
Browser BibleStudy online with Browser Bible
Mobile HTMLRead Mobile HTML online
Zipped mobile HTMLwolmbs_html.zip
ePub 3wolmbs.epub
Amazon Kindle EPUBwolmbs.epub
PDFPDF file list
Crosswire Sword modulewolmb2025seb.zip
Plain text canon only chapter fileswolmbs_readaloud.zip
BibleWorks import (VPL) + SQLwolmbs_vpl.zip
Browser Bible modulewolmbs_browserBible.zip
USFXwolmbs_usfx.zip
USFMwolmbs_usfm.zip
XeTeXwolmbs_xetex.zip

The Holy Bible in the Wolof language of Senegal, translated by La Mission Baptiste du Sénégal

La Sainte Bible en langue wolof du Sénégal, traduite par La Mission Baptiste du Sénégal


Ca njàlbéen ga Yàlla sàkk na asamaan ak suuf.

—Genesis 1:1



Ñeel Daawuda, dib taalifu cant. Aji Sax jee may sàmm, du lenn lu ma ñàkk.

—Psalm 23:1



Waaye njëkkleena tiisoo nguurug Yàlla, ak njub gi mu laaj, te loolu lépp moo leen ko ciy dollil.

—Matthew 6:33



Ndax Yàlla moo sopp àddina, ba joxe jenn Doomam ji, ngir képp ku ko gëm, texe ba fàww, te du sànku mukk.

—John 3:16



Te itam nag xam nanu ne Yàlla mooy def mboolem lu xew, daje ba jur njariñal ñi sopp Yàlla, ñi mu woo, noonee ko ab dogalam namme.

—Romans 8:28


Kàddug Yàlla

The Holy Bible in the Wolof language of Senegal, translated by La Mission Baptiste du Sénégal

La Sainte Bible en langue wolof du Sénégal, traduite par La Mission Baptiste du Sénégal

copyright © 2025 La Mission Baptiste du Sénégal
Language: Wolof

Cette œuvre est mise à disposition sous licence Creative Commons Attribution - Pas d'Utilisation Commerciale - Pas de Modification 4.0 International (CC BY-NC-ND 4.0)

Vous êtes autorisé à :

Partager — copier, distribuer et communiquer le matériel par tous moyens et sous tous formats. L'Offrant ne peut retirer les autorisations concédées par la licence tant que vous appliquez les termes de cette licence.

Attribution — Vous devez créditer l'Œuvre, intégrer un lien vers la licence et indiquer si des modifications ont été effectuées à l'Oeuvre. Vous devez indiquer ces informations par tous les moyens raisonnables, sans toutefois suggérer que l'Offrant vous soutient ou soutient la façon dont vous avez utilisé son Oeuvre.

Pas d’Utilisation Commerciale — Vous n'êtes pas autorisé à faire un usage commercial de cette Oeuvre, tout ou partie du matériel la composant.

Pas de modifications — Dans le cas où vous effectuez un remix, que vous transformez, ou créez à partir du matériel composant l'Oeuvre originale, vous n'êtes pas autorisé à distribuer ou mettre à disposition l'Oeuvre modifiée.

Pas de restrictions complémentaires — Vous n'êtes pas autorisé à appliquer des conditions légales ou des mesures techniques qui restreindraient légalement autrui à utiliser l'Oeuvre dans les conditions décrites par la licence.

C'est un résumé (et non pas un substitut) de la licence. Pour voir une copie de cette licence, cliquez ici.

La Mission Baptiste du Sénégal a le plaisir de vous autoriser à utiliser toute portion tirée des Ecritures qui sont disponibles sur http://biblewolof.com et sur ces appli (l’œuvre), sous réserve que le crédit nous soit reconnu par écrit, avec la mention du nom de notre organisation (voir plus loin). Mais on ne peut la modifier de quelque façon que ce soit, ni l’utiliser à des fins commerciales, c’est à dire, de telles ressources ne peuvent être vendues à un prix supérieur au coût de la reproduction.

Cette licence n’autorise pas un mixage combinant les écritures en wolof avec vos propres ressources traduites en wolof. Si vous désirez faire un mixage, vous devez en obtenir l’autorisation, et pour cela nous exigeons un échantillon de traduction pour une préalable approbation de notre part. En effet des ressources mal traduites portent préjudice à la crédibilité des écritures.

De même, s’il s’agit d’enregistrements des écritures, nous exigeons des échantillons de la matière enregistrée, pour approbation préalable de notre part. En effet des voix marquées d’accent pourraient être dommageables à la crédibilité des écritures.

Pour demander la permission de faire quoi que ce soit en dehors du cadre de cette licence, contactez-nous.

Voici les déclarations de copyright à inclure dans l'œuvre:

Écriture extraite de (s’il s’agit d’une portion de livre)

Suivi de:

Kàddug Yàlla gi © 2025 MBS

https://creativecommons.org/licenses/by-nc-nd/4.0/legalcode.fr

Vous pouvez aussi utiliser une forme abrégée:

(Nom du livre abrégé) 2025 MBS (NINEA: 20215410C9)

https://creativecommons.org/licenses/by-nc-nd/4.0/legalcode.fr

La politique de confidentialité se trouve ici.


This work is licensed under Creative Commons Attribution-NonCommercial-NoDerivatives 4.0 International (CC BY-NC-ND 4.0)

You are free to:

Share — copy and redistribute the material in any medium or format. The licensor cannot revoke these freedoms as long as you follow the license terms.

Attribution — You must give appropriate credit, provide a link to the license, and indicate if changes were made. You may do so in any reasonable manner, but not in any way that suggests the licensor endorses you or your use.

NonCommercial — You may not use the material for commercial purposes.

NoDerivatives — If you remix, transform, or build upon the material, you may not distribute the modified material.

No additional restrictions — You may not apply legal terms or technological measures that legally restrict others from doing anything the license permits.

This is a human-readable summary of (and not a substitute for) the license. To view a copy of this license, click here.

La Mission Baptiste du Sénégal is pleased to give you permission to use any of the scriptures on http://biblewolof.com and in these apps (hereafter referred to as the Work) as long as you give credit to MBS with a copyright notice, and you do not modify or mix the work, and do not sell materials at a price over the cost of reproduction.

In other words, you may download the Work and share it with others as long as you credit us, but you can’t change the Work in any way or use it commercially (for profit).

If we give you permission to do a re-mix (combining the scriptures in wolof with your own materials translated in wolof), we will ask for a sample translation or audio recording to approve first, before any distribution. Materials badly translated and voices with a foreign accent impair the credibility of the scriptures.

To ask permission to do anything outside the scope of this license, contact us.

Here are copyright statements to include with the work :

Scripture citations taken from (if it's only a portion of a book) followed by

Kàddug Yàlla gi © 2025 MBS

https://creativecommons.org/licenses/by-nc-nd/4.0/legalcode

Or you may use a shortened form:

(Name of the book) 2025 MBS (NINEA: 20215410C9)

https://creativecommons.org/licenses/by-nc-nd/4.0/legalcode

You can read our privacy policy here.


Liggéey bii turu sañ-sañu jëfandikoom di « Creative Commons BY-NC-ND 4.0 » ; maye na ku ko yeb, fépp ci àddina, ci kaw way jefandiku ji wàccoo ak yii ndigal: BY = SM (dees na Seedeel boroom Moomeelam); NC = AJ (Amul Jaay); ND = AS (Amul Soppi). Ku bëgga gis sottib sañ sañu jëfandikoo bi, seet ko fii.

Mission Baptiste du Sénégal am na mbégtey may leen ngeen yeb, ak sotti, ak wasaare lu mu mana doon ci Kàddug Yàlla gi ci http://biblewolof.com, ak ci appli yii, ci kaw ngeen seedeel nu sunu moomeel (seetal ci suuf). Waaye dungeen ci mana soppi lenn, ak nu coppite ga mana tëdde, te ngeen bañ cee jaaye lenn ci njëg gu wees li leen sottib mbind mi dikke.

Su dee lu ngeen raxe (muy seen liggéeyu bopp bu ngeen tekki ci wolof, boole ko ak lenni kàddug Yàlla gi ci wolof), ba bëgg koo sotti ngir wasaare ko, war ngeen cee jëkka am sunu ndigal, te jox nu ci seenub tekki, lu tuut lu nu ko mana natte ba mu doy nu, ndax jumtukaay yu tekki bi awul yoon gàkkal na Mbind mu sell mi.

Jokkooleen ak nun, ngir sàkku ndigalu def lu mu mana doon, lu wees kemu sañ-sañu jëfoo.

Ba tey su dee lu ngeen jukkee ci kàddug Yàlla gi, ba def ko ay dégtal yu ngeen taataan, bëgg nanu ngeen sàkkal nu ci seenub taataan, lu tuut lu nu mana natte baat yi ba mu doy nu, ndax baat yu seen làmmiñu boroom taq itam, gàkkal na ab liggéey.

Yii kàddu la sañ-sañu jëfoo tege, te warees koo boole ci liggéey bi:

Ci………… lanu ko jukkee, (su dee ab dogu téere doŋŋ)

Kàddug Yàlla gi © 2025 MBS

https://creativecommons.org/licenses/by-nc-nd/4.0/legalcode.fr

Manees naa jëfandikoo itam ab gàttalub turu téere bi :

(Turu gàttalu téere bi) 2025 MBS (NINEA: 20215410C9)

https://creativecommons.org/licenses/by-nc-nd/4.0/legalcode.fr

This translation is made available to you under the terms of the Creative Commons Attribution-Noncommercial-No Derivatives license 4.0.

You may share and redistribute this Bible translation or extracts from it in any format, provided that:

Pictures included with Scriptures and other documents on this site are licensed just for use with those Scriptures and documents. For other uses, please contact the respective copyright owners.


2025-04-18

Last updated 2025-04-18