^
2 KORENT
Yàlla, Boroom lépp luy dëfal xol yi
Pool setal na boppam
Pool baal na ki tooñoon
Ndawi Yàlla ci xamle kóllëre gu bees, gi Yàlla fas ak nit
Ndamu kóllëre gu bees gi
Xibaaru Kirist leeral na sunu xol yi lëndëmoon
Xibaaru Kirist dafa mel ni alal ju ñu yeb ciy njaq
Sunu màkkaan ci wetu Boroom bi
Nanguleena juboo ak Yàlla
Tiis yi nu daj ci liggéeyal Yàlla
Bàyyileen bokkaale
Mbégu Pool ci ñëwug Tit
Mayeleen ak xol yu yéwén
Li tax ñu yónni Tit ak i àndandoom
Ku ji lu bare, góob lu bare
Pool ñaan na, ñu nangu sañ-sañam
Pool ak ndawi naaféq yi
Nattuy Pool ci matal yónnentam
Peeñub Pool ak nattu bi ko dal
Pool bëgg na leen
Artu yu mujj yi
Tàggtoo