^
2.Buur ya
Yonent Yàlla Ilyaas yar na Buur Akasiya
Yonent Yàlla Ilyaas yéeg na
Israyil ak Mowab jote nañu
Alyaasa jot na jëtun ba
Alyaasa am nab dal
Alyaasa delloo na njukkal
Alyaasa sekki na tooke ja
Alyaasa leel na mbooloo
Alyaasa faj na kilifa
Gewasi lal na pexe
Weñu sémmiñ ga tëmb na
Alyaasa sànk na gàngoor
Xiif ba tar na ca Samari
Aji Sax ji wallu na Samari
Ndawas Sunem sa jotaat na alalam
Asayel mujj na falu ca Siri
Yoram falu na Yuda
Akasiya falu na Yuda
Alyaasa fal na Yewu
Yewu fexeel na buur ya
Yesabel dee na
Yewu bóom na waa kër Axab
Yewu fiir na waa kër Baal
Lingeer Atalyaa falu na Yuda
Yuda bañ na
Yowas santaane na ñu defaraat kër Aji Sax ji
Buur Yowas jeexal na
Yowakas falu na ci Israyil
Yowayas falu na ca Israyil
Yonent Yàlla Alyaasa faatu na
Israyil duma na Siri
Buuri Israyil ak Yudaa ngi xeexoo
Yowayas buurub Israyil saay na
Amaciya buurub Yuda saay na
Yerbowam mu ndaw falu na ca Israyil
Asaryaa falu na buur ca Yuda
Sàkkaryaa falu na buur ca Israyil
Salum falu na buur ca Israyil
Menayem falu na buur ca Israyil
Pekaxiya falu na buur ca Israyil
Peka falu na buur ca Israyil
Yotam falu na buur ca Yuda
Axas falu na buur ca Yuda
Ose falu na buur ca Israyil
Samari, péeyu Israyil, tas na
Waa Asiri sancal nañuy jaambur ca Samari
Esekiya falu na buur ca Yuda
Asiri song na Yuda
Asiri tooñati na Yuda
Yonent Yàlla Esayi yégle na jéllub Asiri
Esekiya wopp na, ba jóg
Buuru Babilon yónnee na ca Esekiya
Buur Esekiya saay na
Manase falu na buur ca Yuda
Amon falu na buur ca Yuda
Yosya falu na buur ca Yuda
Téereb yoon wi feeñ na
Yosya sellal na réew mi
Màggalu bésub Mucc délsi na
Buur Yosya saay na
Yowakas falu na buur ca Yuda
Buur Yowakim fey na Misra galag
Yowakin falu na buur ca Yuda
Cedekiya falu na buur ca Yuda
Nangooti nañu Yerusalem
Yàq nañu kër Aji Sax ji
Jàpp nañu Yudeen ñi njaam
Nabukodonosor tabb na Gedalya ca Yuda
Tijji nañu Yowakin buurub Yuda