^
Baamtug Yoon wi
Musaa fàttli na jaar-jaari Israyil
Ndigalu yëri Kanaan jib na
Bànni Israyil teggi nañu
Israyil nangu na penkub dexu Yurdan
Séddale nañu penkub Yurdan
Musaa duggul Kanaan
Musaa ñaax na bànni Israyil
Yoon wi aayal na bokkaale
Ab jagle ñeel na Israyil
Amal nañu ay rawtu ca penkub Yurdan
Musaa baamtu na yoon wi
Fukki santaanee ngi
Aji Sax ji kenn la
Dogook yenn xeet yi war na Israyil
Xéewlu, fàtte aay na
Israyil gënul ci xeet yi
Israyil jaamu na sëlluw wurus
Musaa tinul na bànni Israyil
Musaa ngi woote déggal Aji Sax ji
Barke ak alkànde dëgmal na
Lu jëm ci sàrti dundin ca réewum dige ba
Aji Sax ji mooy taamu bérabam
Dee mooy àtteb kuy xiirtale ci bokkaale
Yoon wi sàrtal na jëfin yu set
Lu jëm ci céri fukkeel
Lu jëm ci njéggalug bor
Sang am na lu ko war ci jaamam
Li war ci taawug jur
Ñetti yoon lees di màggalsi ci bérab bu sell bi
Yoon wi sàrtal na mbirum àtte
Ay ndigal ñeel na buur
Ay yelleef ñeel na Leween ñi ak sarxalkat yi
Kàddug waxyu day sotti
Ber dëkki rawtu ndigal la
Lu jëm ci kemu suuf ak limu seede cib àtte
Yoon wi sàrtal na mbirum xare
Njotlaay war na ci bóomkat bu umpe
Ay sàrt a ngi ci wàllu njaboot
Deesul wékk nit, fanaanal ko
Yoon wi sàrtal na dundin wu jekk
Sàmmonteleen ak àqu jigéen
Am na ñu dul bokk ci ndajem Aji Sax ji
Deesul topp bànni Israyil ab tegandaay
Wàccook aw xas wartéef la
Raasaatu mu suur boroom lew na
Yoon wi sàrtal na pase ak séyaat
Yoon wi aar na néew-ji-doole
Njub ak yërmande wartéef la
Donn sa jabaru mbokk wartéef la
Am na jëf ju aay ci sot
Ab nattukaay day mat
Mbugal Amaleg ndigal la
Njotlaayal Aji Sax ji laaj na ab galag
Kóllëre feddliku na
Musaa biral na yooni barke ak alkànde
Lu jëm ci alkànde yi
Lu jëm ci barke yi
Déggadi, alku
Kóllëre gi yeeslu na
Buleen caaxaane kóllëreg Aji Sax ji
Mbugal du jaas
Dellusi ci Aji Sax ji, barkeel
Musaa nee déggal Yàlla yomb na
Musaa tàggoo na
Musaa woy na kóllëreg Aji Sax ji
Déggal Aji Sax ji, dund
Aji Sax ji woo na Musaa
Musaa ñaanal na bànni Israyil
Musaa wuyji na