^
1.Samiyel
Lii mooy jaar-jaari Samiyel
Aana ñaan na doom
Lu jëm ci juddub Samiyel ak ngoneem
Aana sant na
Lu jëm ci doomi Eli
Lu jëm ci waa kër Samiyel
Eli artu na ay doomam
Nitu Yàlla rëbb na Eli
Yàlla def na Samiyel yonent
Nangu nañu gaalu Yàlla ga
Mbugal ma topp na waa kër Eli
Gaalu Yàlla ga jaaxal na Filisteen ña
Filisteen ña delloo nañu gaalu Yàlla ga
Samiyel jiite na Israayil
Israayil sàkku na buur
Bànni Israayil ñaan na Samiyel ab buur
Lu jëm ci sañ-sañu buur
Lii mooy jaar-jaari Sawul
Sawul doxi na yónnent
Sawul gis na Samiyel
Samiyel diw na Sawul, fal ko
Leerug Yàlla gane na Sawul
Yàlla feddali na palug Sawul
Sawul jéngu na
Samiyel matal na liggéeyam
Sawul tooñ na
Yonatan def na njàmbaar
Yonatan song na Filisteen ñi
Sawul wax na lu ëpp
Bànni Israayil jot na Yonatan
Sawul am na ndam
Sawul tooñati na
Sawul ñàkk na
Lii moo dox diggante Sawul ak Daawuda
Yàlla fal na Daawuda
Daawuda dugg na ca liggéeyu Sawul
Golyaat dëkk na bànni Israayil
Daawuda def na jaloore
Yonatan fas na kóllëreek Daawuda
Sawul a ngay fexeel Daawuda
Daawuda jël na doomu Sawul soxna
Yonatan taxawu na Daawuda
Mikal xettali na Daawuda
Sawul toppi na Daawuda ca Nayot
Yonatan wallu na Daawuda
Daawuda dem na ca Aximeleg
Daawuda nax na leen
Daawuda jiite na gàngoor
Sawul rey na sarxalkati waa Noob
Daawuda xettali na waa Keyla
Sawul topp na Daawuda
Daawudaa gën Sawul fuuf
Samiyel faatu na
Nabal gàntal na Daawuda
Jabaru Nabal def nag muus
Nabal dee, Daawuda dikk
Daawuda gënati na Sawul
Daawuda làquji na ca waa Filisti
Sawul seetluji na ca Endor
Waa Filisti dàq nañu Daawuda
Daawuda toppi na Amalegeen ña
Daawuda wone na ngor
Daawuda sédd na njiiti Yudeen ña
Lu jëm ci mujug Sawul