^
2.Buur ya
Yonent Yàlla Ilyaas yar na Buur Axasya
Yonent Yàlla Ilyaas yéeg na
Israayil ak Mowab jote nañu
Alyaasa dimbali na jëtun ba
Alyaasa am nab dal
Alyaasa delloo na njukkal
Alyaasa sekki na tooke ja
Alyaasa leel na mbooloo
Alyaasa faj na kilifa
Gexasi lal na pexe
Weñu sémmiñ ga tëmb na
Alyaasa sànk na gàngoor
Xiif ba tar na ca Samari
Aji Sax ji wallu na Samari
Ndawas Sunem sa jotaat na alalam
Asayel mujj na falu ca Siri
Yexoram falu na Yuda
Axasya falu na Yuda
Alyaasa fal na Yewu
Yewu fexeel na buur ya
Yesabel dee na
Yewu bóom na waa kër Axab
Yewu fiir na waa kër Baal
Lingeer Atalyaa falu na Yuda
Yuda bañ na
Yowas santaane na ñu defaraat kër Aji Sax ji
Buur Yowas jeexal na
Yowaxas falu na ci Israayil
Yowas falu na ca Israayil
Yonent Yàlla Alyaasa faatu na
Israayil duma na Siri
Buuri Israayil ak Yudaa ngi xeexoo
Yowas buurub Israayil saay na
Amaciya buurub Yuda saay na
Yerbowam mu ndaw falu na ca Israayil
Asaryaa falu na buur ca Yuda
Sàkkaryaa falu na buur ca Israayil
Salum falu na buur ca Israayil
Menayem falu na buur ca Israayil
Pekaxya falu na buur ca Israayil
Peka falu na buur ca Israayil
Yotam falu na buur ca Yuda
Axas falu na buur ca Yuda
Ose falu na buur ca Israayil
Samari, péeyu Israayil, tas na
Waa Asiri sancal nañuy jàmbur ca Samari
Esekiyas falu na buur ca Yuda
Asiri song na Yuda
Asiri tooñati na Yuda
Yonent Yàlla Esayi yégle na jéllub Asiri
Esekiyas wopp na, ba jóg
Buuru Babilon yónnee na ca Esekiyas
Buur Esekiyas saay na
Manase falu na buur ca Yuda
Amon falu na buur ca Yuda
Yosya falu na buur ca Yuda
Téereb yoon wi feeñ na
Yosya sellal na réew mi
Màggalu bésub Mucc délsi na
Buur Yosya saay na
Yowaxas falu na buur ca Yuda
Buur Yoyakim fey na Misra galag
Yoyakin falu na buur ca Yuda
Cedesyas falu na buur ca Yuda
Nangooti nañu Yerusalem
Yàq nañu kër Aji Sax ji
Jàpp nañu Yudeen ñi njaam
Nebukatnecar tabb na Gedalya ca Yuda
Tijji nañu Yoyakin buurub Yuda