^
Dañeel
Dañeel gore na ci biir nguuru kéefar
Dañeel aki xaritam tàbbi nañu ci liggéeyu kër buur
Dañeel nettali na géntu Buur
Sànni nañu xariti Dañeel cib taal
Buuru yéefar sàbbaal na Aji Sax ji
Nebukatnecar géntaat na
Nebukatnecar xippi na
Buur Belsacar a bew ba sànku
Dañeel tàbbi na ci paxum gaynde
Aji Sax ji feeñu na Dañeel
Dañeel gis na ñeenti rabi géej
Dañeel gis na kuuy ak sikket
Dañeel jàngat na waxyu bu Yeremi jottali
Dañeel gis na boroom col gu weex
Buur bëj-gànnaar ak buur bëj-saalum a ngi jote
Buur bëj-gànnaar ëpp nay loxo
Mujug jamono taxaw na
Dañeel gis na ñaari malaaka