^
Filib
Ubbite gi
Póol ñaanal na waa Filib
Jéngi Póol jéngul kàddug Yàlla
Ni Almasi bi woyofe mooy royukaay
Doonleen ay leer ci àddina
Póol gërëm na Timote ak Epafrodit
Gii njub a wóor
Nanu jëm kanam ngir jot ca yool ba
Póol dénkaane na
Póol gërëm na waa Filib
Tàggatoo jib na