^
Peeñu ma
Ubbite gi
Ab nuyoo ñeel na juróom ñaari mboolooy gëmkat
Yowaan am na peeñu ca dunu Patmos
Bindees na waa Efes
Bindees na waa Esmirna
Bindees na waa Pergam
Bindees na waa Catir
Bindees na waa Sàrd
Bindees na waa Filadelfi
Bindees na waa Lawdise
Buur Yàlla toog na ca ngànguneem
Xarum Yàlla jël na téere ba
Xar mi tàyyi na tayu yi
Jaamukati Yàlla yi mucc nañu
Mbooloo mu réy am na ndam
Xar ma tàyyi na juróom ñaareelu tayu ba
Liit yi jib na
Àtte bu mujj ba agsi na
Ñaari seede yi bey nañu seen waar
Juróom ñaareelu liit ga jib na
Ninki-nanka ji fexeel na ndaw si
Ñaari rab yu aay falu nañu
Kuréel gu sell gi topp na Xar mi
Ñetti malaaka yégle nañu àttey Yàlla
Ngóobum àddina tar na
Musibay mujjantal agsi na
Sànj ma sottiku na
Mbugal ñeel na jigéenu moykat ju mag ji
Babilon daanu na
Aleluya!
Gawar war na fas wu weex
Almasi bi mooy nguuru junniy at
Seytaane moo mujje ca déegu sawara sa
Bés-pénc taxaw na
Asamaan ak suuf dinañu am kuutaay
Walum dund mi feeñ na
Yeesu Almasi bi dina délsi