^
Yawut ya
Yàlla moo feeñ ci Doom ji
Doom jee gëna màgg malaaka yi
Nanu teewlu pexem mucc mi Yàlla waajal
Yeesu moo rammu jaam ñi
Doom jee gëna màgg Musaa
Almasi bi moo jara déggal
Yeesu mooy sarxalkat bu mag bi
Nanu jëm kanam
Digeb Yàlla du jaas
Melkiccedeg moo sut Ibraayma ak Aaróona
Melkiccedeg misaal na Almasi bi
Kóllëre gi gën la Yeesu Sarxalkat bu mag bi indi
Yoonu Musaa sàrtaloon na nu ñuy jaamoo Yàlla
Almasi bi moo far bàkkaar, fas kóllëre gu bees
Nanu àgg fa Yàlla
Yàlla rafetlu na ngëm
Buleen xeeb yaru Boroom bi
Buleen tanqamlu Yàlla
Dundin wu rafet moo neex Yàlla