^
Ayóoba
Ayóobaa barkeel, ragal Yàlla
Nattu nuyoo na
Nattu nuyooti na
Ayóoba am nay gan
Ayóoba rëbb na bésub juddoom
Elifas nee: Yaru Yàlla du ñàkk
Ayóoba nee: Maa yey ne ba ma
Bildàdd nee: Musiba, añu boroom
Ayóoba nee: Yàlla du ku ñuy layool
Ayóoba nee lu mu def Yàlla?
Cofar nee: Tuub, raw
Ayóoba nee: Yàlla lu ko neex lay def
Ayóoba nee: Su layoo, yey
Àddinaa gàtt, barew tiis
Làq ma sa mer, ba giif
Elifas nee: Lu waay def, boppam
Ayóoba gisatul yaakaar
Bildàdd buurati na
Yàllaa may jot
Cofar nee: Ku musiba dab, yaa tooñ
Ayóoba weddi na àlluway xarit ya
Elifas nee: Tuub a war Ayóoba
Ayóoba nee: Yàlla noppi na
Ayóoba nee: Yàllaa ngi tanqamlu
Bildàdd nee: Deesul am dëgg fa Yàlla
Ayóoba ne Bildàdd: Yaa mat wall
Ayóoba nee: Yàlla kenn xamu ko
Ayóoba bañ na
Ayóoba neeti: Yéene néeg la
Xel mu rafet, fa Yàlla
Ayóoba jooy na démbam
Ayóoba jooy na coono
Ayóoba waat na
Ndaw nee na, mooy tontu mag
Yàlla du moroom
Yàlla dina wax ciy gént
Eliyu nee: Mitit ndéey la
Eliyu nee: Njotlaay du ñàkk
Eliyu nee: Ayóoba moy na dëgg
Yàlla du def lu bon
Yàlla amul par-parloo
Eliyu nee: Kàdduy Ayóoba du xel
Eliyu nee: Coonoy àddina am njàng la
Yàlla mooy Buur
Aji Sax ji àddu na
Yàlla dëkk na Ayóoba
Ayóoba tuub na
Yàlla leqali na Ayóoba