^
Sàkkaryaa
Waññiku ci Aji Sax ji weesul
Misaal mu jëkk: ay fas aki gawar
Ñaareelu misaal: ay béjjén ak ay tëgg
Ñetteelu misaal: nit kuy natt Yerusalem
Ñeenteelu misaal: Yosuwe am na col gu yees
Juróomeelu misaal: ay tegukaayi làmp ak garabi oliw
Juróom benneelu misaal: téere bu ñu taxañ buy naaw
Juróom ñaareelu misaal: ndab lu jigéen toog ca biir
Juróom ñetteelu misaal: ay watiiri xare
Fal nañu buur sarxalkat bu mag bi
Leeraange ci mbirum koor dikk na
Barke wuutu na alkànde
Mbég wuutu na koor
Mbugal mu mucc topp, dal na askani diiwaan bi
Buur Almasi dikk na
Aji Sax ji mooy xeexal ñoñam
Xërëm, neen la
Yiwiku ñeelati na Israayil
Sàmm bu baax jotul yoolam
Yerusalem yiwiku na
Ñaawlu dikkal na réew mépp
Ay tuur ak yonenti caaxaan day jeex
Kóllëre feddaliku na
Xare bu mujj jib na