^
MACË
Cosaanu Yeesu Kirist
Juddub Yeesu Kirist
Ay boroom xam-xam ñëw nañu, màggalsi Yeesu
Yuusufa ak Maryaama gàddaay nañu jëm réewu Misra
Ñibsi nañu réewu Israyil
Waareb Yaxya
Yaxya sóob na Yeesu ci dexu Yurdan
Yeesu dékku na ay nattu ci pexey Seytaane
Yeesu dëkk na Kapernawum ci diiwaanu Galile
Yeesu tànn na ñeenti taalibe
Barkeel gu wóor gi
Xoromus àddina ak leeram
Ni yoonu Musaa ak waxi yonent yi ame ci Yeesu
Mere nit ak bóom ko ñoo yem fa kanam Yàlla
Ku xédd jigéen, njaaloo nga
Bul fase sa soxna lu dul ci njaaloo
Bul weddi sa ngiñ
Bul feyu
Ni ñuy sàkke sarax
Ni ñuy ñaane ci Yàlla
Ni ñuy woore
Alali laaxira
Wóolul Yàlla
Bul ñaaw njort, ba àtte sa moroom
Yàlla nangu na ñaanu ku gëm
Bunt bu xat bi
Garab ak meññeefam
Léebu ñaari tabaxkat yi
Yeesu faj na ku gaana
Ngëmu njiitu xare bi
Yeesu faj na jarag yu bare
Yeesu dalal na ngelaw li
Yeesu faj na ñaar ñu rab jàpp
Yeesu faj na ku làggi
Yeesu woo na Macë, mu nekk taalibeem
Ndax warees na woor?
Yeesu dekkal na doomu njiitu jàngu ba te faj jigéen
Yeesu faj na ñaari gumba
Yeesu faj na ki rab jàpp
Yeesu yërëm na mbooloo mi
Yeesu yónni na fukki ndaw ya ak ñaar
Yaxya yónnee na, di laaj Yeesu
Yeesu gëdd na ay dëkk
Woote bu mag bi
Yeesu nee na, mooy boroom bésub noflaay bi
Yeesu faj na nit ku loxoom làggi
Ku rab jàpp, mu gumba te luu
Ku sosal Xelu Yàlla mi
Yeesu nanguwula def kéemaan
Ndeyu Yeesu ak i doomi ndeyam
Léebu beykat ba
Lu tax Yeesu di wax ay léeb
Yeesu firi na léebu beykat bi
Léebu jëmb bi
Léebu doomu fuddën gi
Léebu lawiir bi
Léebu alal ju nëbbu ak léebu per ba
Léebu mbaalum géej ga
Léebu boroom kër ga
Yeesu ci dëkku Nasaret
Yaxya faatu na
Yeesu bareel na mburu ya
Yeesu dox na ci kaw ndox ma
Farisen ya ak aada ya
Yeesu faj na doomu jigéen, ja askanoo réewu Kanaan
Yeesu faj na ñu wopp
Yeesu bareel na ay mburu ñaareel bi yoon
Kéemaan gu jóge ci asamaan
Piyeer wax na ne, Yeesu mooy Almasi bi
Ndamu Yeesu jolli na ci moom
Yeesu faj na xale bu rab jàpp
Yeesu waxaat na ne dina dee, dekki
Yeesu fey na warugaru kër Yàlla ga
Kan moo gëna màgg?
Ñi yóbbe nit bàkkaar
Xar mu réer ma
Mbaalug bàkkaar yi
Jaraaf ju amul yërmande
Ñi fase, ak ñi baña séy ngir jaamu Yàlla
Xale yu ndaw yi
Waxambaane wu bare alal
Léebu liggéeykat yi ñu jël ci waxtu yu wuute
Yeesu xamle na ñetteelu yoon ne dina dee, dekki
Li doomi Sebede ñaan Yeesu
Yeesu faj na ñaari gumba
Yeesu dugg na Yerusalem
Yeesu dàq na jaaykat ya ca kër Yàlla ga
Yeesu rëbb na garabu figg ga
Sañ-sañu Yeesu
Léebu ñaari doom ya
Léebu beykat, yi rey doomu boroom tool bi
Léebu céet ga
Galag gi ñuy fey buur bi Sesaar
Sadusen yi ak ndekkite li
Ban santaane moo gëna màgg ci yoonu Musaa?
Ndax Almasi bi mooy sëtu Daawuda?
Yeesu gëdd na xutbakat ya ak Farisen ya
Yàqug Yerusalem ak dellusig Doomu nit ki
Yàlla rekk moo xam bés ba
Léebu fukki janq ya
Léebu surga, ya njaatige bi dénk xaalisam
Àtteb xeet yi
Njiiti yoon yi fexeel nañu Yeesu
Jigéen ja tuur na latkoloñ ci boppu Yeesu
Yudaa wor na Yeesu
Reer bu mujj bi
Yeesu ñaan na ci toolu Setsemane ci biir tiis wu réy
Jàpp nañu Yeesu
Yeesu taxaw na ci kanam kureelu àttekat ya
Piyeer weddi na Yeesu
Yudaa am na naqar lool, ba xaru
Yeesu taxaw na ci kanam Pilaat
Xarekat ya ñaawal nañu Yeesu
Daaj nañu Yeesu ci bant bi
Yeesu saay na
Rob nañu Yeesu
Yeesu Kirist dekki na