^
Mucc ga
Bànni Israyil dem na réewum Misra
Firawna not na bànni Israyil
Musaa gane na àddina
Musaa gàddaayi na réewum Majan
Yàlla ñeewante na bànni Israyil
Aji Sax ji yónni na Musaa
Musaa di leewaayu, Yàlla di ko ñaax
Yàlla jox na Musaa ay firnde
Yàlla def na Aaróona bëkk-néegu Musaa
Musaa dellu na Misra
Musaa ak Aaróona seeti nañu Firawna
Firawna yokk na liggéeyu bànni Israyil
Yàlla dellu na yónni Musaa
Lu jëm ci cosaanu Musaa ak Aaróona
Yàlla feddli na digeem baak Musaa
Firawna gàntu na
Yar bu jëkk ba: ndox mu soppliku deret
Yarub ñaareel ba: mbott yu daj réew ma
Yarub ñetteel ba: rayentaan yu daj réew ma
Yarub ñeenteel ba: weñ yuy màtte
Yarub juróomeel ba: Deewug jur ga
Yarub juróom benneel ba: Taab ya
Yarub juróom ñaareel ba: Tawub yuur ba
Yarub juróom ñetteel ba: Njéeréer ya
Yarub juróom ñeenteel ba: Lëndëm gu tar ga
Yàlla waaj na yar bu mujj ba
Lu jëm ci bésub Mucc ba
Lu jëm ci ayu bésu Mburu mu amul lawiir
Waajal nañu bésub Mucc ba
Yarub fukkeel ba, di deewu taaw ya
Bànni Israyil gàddaay na
Ay dogali Aji Sax jaa ngii, ñeel bésub Mucc ba
Lu jëm ci aada, yi ñuy baaxantale
Aji Sax ji jiite na mbooloo ma
Firawna dabi na bànni Israyil
Yàlla xàll na géej ga
Woyu Musaa waak bànni Israyil
Maryaama woy na
Lu jëm ci ndox mu wex ma
Aji Sax ji leel na bànni Israyil
Aji Sax ji wàcce na mànn aki picc
Aji Sax ji santaane na bésub Noflaay
Mànn ma jar naa fàttliku
Ndox balle na ciw doj
Amalegeen ña xare nañook Israyil
Gorob Musaa yedd na Musaa
Yàlla xamle na kóllëreem
Yàlla wàcc na ca kaw tundu Sinayi
Kóllëre gi laaj na ay sàrt
Mbooloo ma dagaan na ab jottlikat
Téereb kóllëre gi
Ay dogal a ngi, yu jëm ci ab sarxalukaay
Lu jëm ci Ebrë yiy ay jaam
Lu jëm ci lor sa moroom
Yoonu Aji Sax ji ñoŋal na alalu nit
Yoonu Aji Sax ji rafetal na dundin
Àtte laaj na njub ak yërmande
Lu jëm ci bési Noflaay
Lu jëm ci bési màggali Israyil
Yàlla yeb na bànni Israyil
Yàlla fasoo na kóllëre ak bànni Israyil
Musaa yéeg na ca tund wa
Lu jëm ci jaamookaay bi
Lu jëm ci gaal giy def àlluway seede si
Lu jëm ci taabalu mburum sarax mi
Lu jëm ci tegukaayu làmp bi
Lu jëm ci sori xaymab jaamookaay bi
Lu jëm ci kenuy jaamookaay bi
Lu jëm ci rido bi
Lu jëm ci kiiraayal buntu xayma bi
Lu jëm ci sarxalukaay bi
Lu jëm ci ëttu jaamookaay bi
Lu jëm ci santaane, yi sarxalkat yi sasoo
Lu jëm ci diwu làmp bi
Lu jëm ci yérey sarxalkat yi
Lu jëm ci xar-sànni mi
Lu jëm ci kiiraayal dënn bi
Lu jëm ci yére yu sell, yi ci des
Lu jëm ci sarxalkat yeek seen xewu colu
Lu jëm ci sarax yi war bés bu nekk
Lu jëm ci sarxalukaayu cuuraay bi
Lu jëm ci njot-gi-bakkan
Lu jëm ci mbalkam njàpp mi
Lu jëm ci diwu pal gi ñuy sellale
Lu jëm ci cuuraay li
Tabb nañu ay liggéeykat yu xareñ
Lu jëm ci solob bésub Noflaay
Israyil fecci na kóllëre
Merum Musaa am na njeexital
Musaa tinu na Yàlla
Yàlla yebal na Musaa
Yàlla feeñ na cib xayma
Musaa layool na bànni Israyil
Lu jëm ci àlluway doj yu bees yi
Aji Sax ji yeesal na kóllëre gi
Musaa dellu na dal ba
Bànni Israyil yékkati na jaamookaay ba
Bésub Noflaay du bésu liggéey
Ay sarax war na ci jaamookaay bi
Besalel ak Oliyab tàmbali nañu liggéey bi
Defar nañu bérab bu sell ba
Defar nañu gaalu kóllëre gi
Defar nañu taabalu mburum teewal mi
Defar nañu tegukaayu làmp bi
Defar nañu sarxalukaayu cuuraay bi
Defar nañu sarxalukaay bi ak mbalkam njàpp mi
Defar nañu ëttu jaamookaay bi
Lim nañu jumtukaay yi
Defar nañu yérey sarxalkat yi
Defar nañu kiiraayal dënn bi
Defar nañu yérey sarxal, yi ci des
Musaa memmiku na liggéey bi
Samp jaamookaay bi jot na
Musaa samp na jaamookaay bi
Leeru Aji Sax ji gane na bérab bu sell bi