^
1.Buur ya
Lu jëm ci nguurug Suleymaan
Daawuda néew na doole
Adoñaa ngi sàkku jal bi
Suleymaan falu na
Daawuda dénku na Suleymaan
Nii la Adoña mujje
Nii la Abyatar mujje
Nii la Yowab mujje
Nii la Simey mujje
Buur Suleymaan ñaan na Yàlla mu xelal ko
Suleymaan wone na xelam
Suleymaan fal na ay njiit
Suleymaan kenn la woon
Suleymaan waajal na tabaxu kër Yàlla ga
Suleymaan tabax na kër Yàlla ga
Liggéey nañu biir kër gi
Suleymaan tabax na këram
Tëgg ba defar na jumtukaayi kër Yàlla ga
Sancal nañu gaalu Yàlla ga
Suleymaan àddu na
Suleymaan yékkati na kàddug ñaan
Suleymaan ñaanal na bànni Israayil
Suleymaan daloo na kër Yàlla ga
Aji Sax ji feeñu na Suleymaan
Buur Suleymaan jëflante naak Buur Iram
Lingeer buurub Seba seetsi na Suleymaan
Suleymaan bare woon na alal
Suleymaan moy na
Ay noon jógal nañu Suleymaan
Buur Suleymaan saay na
Réew ma xàjjalikoo na
Israayil jàmbu na Robowam
Yerbowam buurub Israayil bokkaale na
Nitu Yàlla àddu na ca Betel
Ab yonent nattu na moroomam
Aw tiis dal na ci kaw Yerbowam
Robowam falu na ca Yuda
Abyam falu na ca Yuda
Asa falu na ca Yuda
Nadab falu na ca Israayil
Basa falu na ca Israayil
Ela falu na ca Israayil
Simri falu na ca Israayil
Omri falu na ca Israayil
Axab falu na Israayil
Yonent Yàlla Ilyaas yégle na bekkoor
Ilyaas waar na jëtun ba
Ilyaas ñaanal na doomu jëtun ba
Ilyaas daje naak surgab Buur Axab
Ilyaas jànkoonte naak Axab
Ilyaas fenqoo naak waa kër Baal
Ilyaas gedd na
Aji Sax ji yónniwaat na Ilyaas
Ilyaas am na bëkk-néeg
Siri song na Samari
Israayil daan na Siri
Siri songati na Israayil
Ab yonent sikk na Axab
Buur Axab tooñ na Nabot
Aji Sax ji dogal na mbugalu Axab
Axab songati na Siri
Mise yégle na jéllub Axab
Axab song na Ramot
Yosafat falu na Yuda
Axasya falu na Israayil