Yeremi
<
0
>
^
Yeremi
Ubbite gi
Kàddug waxyu dal na Yuda
Yàlla woo na Yeremi
Yàlla wone na ñaari misaal
Yàlla taxawu na Israayil
Bànni Israayil wor nañu
Aji Sax jaa ngi layoo
Yuda amul worma
Tuub jot na
Israayil woyof kumba, Yuda toogadi
Kàdduy tuub jib na
Xare jib na
Mbugal taxaw na
Yerusalem dugg na fitna
Mbugal war na
Aji Sax ji artu na xeet wi
Mbon maase na ci xeet wi
Gawub Yerusalem nuyoo na
Askan wa të na
Pexey askan wi jur na musiba
Noon sàqee na bëj-gànnaar
Yeremi yedd na demkati kër Yàlla yi
Yàlla gàntal na
Xuru Ben Inom di xuru dee
Askan wi të na ticc
Yaakaar tas na
Yeremi am na naqar
Dëgg jeex na
Jooy jot na
Ku xam Yàlla rekk a xelu
Xaraf, na Yàlla tax
Aji Sax ji du moroomu xërëm
Mbugal dikk na
Yeremi tinu na Aji Sax ji
Yuda fecci na kóllëre
Aji Sax ji dëddu na soppeem
Ñu ngi fexeel Yeremi
Aji Sax ji artu na dëkkandooy Israayil
Colu Yeremi misaal la
Yàlla misaal na sànjam
Dégloo, balaa yeex
Mbugal a ngii
Yerusalem am na gàcce
Maral dikk na
Kàdduy waxyuy caaxaan jib na
Yeremee ngi tinu Aji Sax ji
Aji Sax ji àddu na
Mbugalu Yuda du jaas
Aji Sax ji feddali na yebam
Yeremi wéet na ci biiri bokkam
Yaakaar jeexul
Kenn rëccul mbugal mi
Ñépp ay ràññeeji Aji Sax ji
Aji Sax ji sikk na waa Yuda
Aji Sax jee jara yaakaar
Yeremi ñaan na Yàlla wall
Bésub Noflaay ñeel na Aji Sax ji
Boroom njaq doon na misaal
Israayil fàtte na Aji Sax ji
Fexeel nañu Yeremi
Njaq la toj na
Tëj nañu Yeremi
Yeremi ñaxtu na
Jéllub Yerusalem jubsi na
Xibaar ñeel na waa kër buur
Lu jëm ci Salum buurub Yuda
Lu jëm ci Yoyakim, kuutaayu Buur Yosya
Yeremi yégle na fitnay Yerusalem
Lu jëm ci Buur Kooña doomu Yoyakim
Sàmm bu baax aye na
Kàddu jógal na yonenti caaxaan
Yéeneb Aji Sax ji du ab yen
Li ñaari dàmbi figg di misaal
Ab tënkub waxyoo ngii
Kàddug waxyu dal na xeet yi
Yeremi dugg na coono
Ñu ngi tëru Yeremi
Yoyakim reylu na ab yonent
Yeremi misaal na kilifteefu Babilon
Yeremi tiiñal na ab yonentu caaxaan
Yeremi bind na ngàllo ga bataaxal
Semaya yonentu caaxaan bi jot na tontam
Yeremi yéene na yeeslug jàmm
Nii la yéene bi tënkoo
Ay teraanga nuyoo na
Israayil séentu na sancaatub réewam
Aji Sax ji teewlul na Israayil
Kóllëre gu yees a ngii
Lii mooy saxal Israayil
Yeremi wone na dayob ngëmam
Xelu Yeremi teey na
Aji Sax ji dalal na xelu Yeremi
Aji Sax ji du dige, di fomm
Askanu Buur Daawuda dina yeeslu
Kóllëre gu dul toxoo ngii
Aji Sax ji wax na Buur Cedesyas mujam
Yiwi jaam yi war na
Rekabeen ña raw nañu Yudeen ña
Buur Yoyakim def na njombe
Buur Cedesyas sàkku na ndimbal
Tàbbal nañu Yeremi ca kàmb ga
Babilon nangu na Yerusalem
Aji Sax ji yiwi na ñaari jaamam
Yuda daje na ca Gedalya
Ismayel bóom na ñu bare
Toogaani Misra gënul
Yóbbu nañu Yeremi
Bokkaale sabab na mbugal
Barukk mucc na
Kàddug waxyu dalati na xeet yi
Lu jëm ci Misra
Israayil dina xettaliku
Lu jëm ci Filisteen ñi
Lu jëm ci réewum Mowab
Lu jëm ci Amoneen ñi
Lu jëm ci Edomeen ñi
Lu jëm ci Damaas
Lu jëm ci Arabi Kedar ak Àccor yi
Lu jëm ci Elameen ñi
Babilon daanu na
Cant, ñeel ki bind lépp
Ngalla Babilon
Yeremi santaane na misaal
Kàdduy ndollent a ngii
Yeremi
<
0
>
© 2025 MBS